🌐🔥 Participer au Hacktober Fest Let’s Go !🔥
Waxtane
Le Wolof the simple way ?!
Niewlene niou waxtane, venez discuter, come discuss with us !
Qu’est ce que waxtane ?
Waxtane est un receuil de phrases de discussion traduites en cinq langues (pour le moment).
Le Wolof le Francais, l’Anglais, l’Espagnol et le Catalan.
Waxtane vise à faciliter la communication entre personnes parlant différentes langues, en se basant sur un modèle sans prise de têtes la discussion.
Contributions
Venez contribuer un max !
Une discussion n’est rien sans ses intervenants.
Feel free to send PR and suggestions. 😁
Contribuez ici : Ajouter Contribution
Phrases disponibles
No | Wolof | Français | Anglais | Espagnol | Catalan |
---|---|---|---|---|---|
2 | Na nga def ? | Comment vas tu ? | How are you ? | ¿Cómo estás? | Com estàs ? |
3 | Mangui gui fi | Je vais bien | I’m fine | Estoy bien | Estic bé |
4 | iow nak no def ? | Et toi comment va tu ? | And you how are you ? | Y tú ¿Cómo estás? | I tu com estàs ? |
5 | Mangui ci diam | Ca va | I’m good | Estoy bien | Estic bé |
6 | Kay gnou lekk | Viens on mange | Let’s take a meal | Vamos a comer | Anem a menjar |
7 | Gnata att nga am ? | Quelle age as-tu ? | How old are you ? | ¿Cuántos años tienes? | Quants anys tens ? |
8 | Tay dama woorr | J’ai jeûné aujourd’hui | I fasted today | No he comido hoy | Avui no he menjat |
9 | Fane nga deuk ? | Où est-ce que tu habites ? | Where do you live ? | ¿Dónde vives? | On vius ? |
10 | Nane nga toudou ? | Comment est-ce que tu t’appelle ? | What’s your name ? | ¿Cómo te llamas? | Quin és el teu nom ? |
11 | Mangui toudou X | Je m’appelle X | My name is X | Me llamo X | Em dic X |
12 | Dama la sokhla | J’ai besoin de toi | I need you | Te necesito | Et necessito |
13 | Dama khiff | J’ai faim | I am hungry | Tengo hambre | Tinc fam |
14 | Dama marr | J’ai soif | I am thirsty | Tengo sed | Tinc set |
15 | Mangui joko si leund mi | Je me connecte sur le web | I am surfing on the web | Estoy conectado a internet | Estic navegant per la web |
16 | Dama beug lou jeum si waloum xarala | J’adore la Technologie | I love Technology | Amo la tecnología | M’encanta la tecnologia |
17 | Dama beug ndekki | Je veux prendre un petit déjeuner | I want to take a breakfast | Quiero desayunar | Vull esmorzar |
18 | Dama beug Agne | Je veux prendre un déjeuner | I want to have lunch | Quiero comer | Vull dinar |
19 | Dama beug rére | Je veux prendre un dîner | I want to have a dinner | Quiero cenar | Vull sopar |
20 | Damay takk jabar | Je vais me marier | I’m getting married | Me voy a casar | M’estic casant |
21 | Mayma khaliss | Donne moi de l’argent | Give me some money | Dame dinero | Doneu-me una mica de diners. |
22 | Bane wakhtu mo joot ? | Quelle heure fait-il ? | What time is it ? | ¿Qué hora es? | Quiena hora es ? |
23 | Dama sonne | Je suis fatigué | I’m tired | Estoy cansado | Estic cansat |
24 | Bu la neexee | S’il vous plaît | Please | Por favor | Si us plau |
25 | Amul sólo | Je vous en prie | You’re welcome | De nada | De res |
26 | Kay niou dem | Viens on y va | Come let’s go | Vamonos | Anem |
27 | Jéggël ma | Excusez-moi | Excuse me | Disculpe | Disculpa |
28 | Ndax dégg nga angale ? | Parlez-vous anglais ? | Do you speak English ? | ¿Hablas español? | Parles anglès ? |
29 | Dégg nga ? | Comprenez-vous ? | Do you understand ? | ¿Me entiendes? | Ho entens? |
30 | Dégg naa | Je comprends | I understand | Entiendo | Comprenc |
31 | Dégguma | Je ne comprends pas | I don’t understand | No entiendo | No ho entenc |
32 | Nanga tudd ? | Quel est ton nom ? | What is your name ? | ¿Cuál es tú nombre? | Quin és el teu nom ? |
33 | Jàmm nga fanaane ? | Comment s’est passée votre soirée ? | How was your night ? | ¿Cómo te fue anoche? | Com va ser la teva nit? |
34 | Fii ba Sandaga ñaata ? | Combien ça fait d’ici à Sandaga ? | How much is it from here to Sandaga ? | ¿A qué distancia está Sandanga desde aquí? | Quant costa anar a Sandaga ? |
35 | Fan mooy seen wanaag ? | Où sont les toilettes ? | Where is the toilet ? | ¿Dónde está el baño? | On és el bany ? |
36 | Neexoon na | C’était bon | It was good | Estuvo bien | Va ser bo |
37 | Mi ngi ci jàmm | Il/Elle va bien | He/She is fine | El/Ella está bien | Està bé |
38 | Ñaata lay jar ? | Combien ça coûte ? | How much is it ? | ¿Cuánto es? | Quant costa ? |
39 | Ñaata ngay jaaye bii ? | Tu vends ça combien ? | How much are you selling this for ? | ¿Cuánto cuesta esto? | Per quant el veneu ? |
40 | Seer na lool | C’est très cher | That’s very expensive | Eso es muy caro | Això és molt car |
41 | Wagniil mako | Diminue moi ça | Turn it down for me | Baja el precio | Rebutja-ho per a mi |
42 | Lougnouy lekk ? | Qu’est ce qu’on mange ? | What do we eat ? | ¿Qué vamos a comer? | Què mengem ? |
43 | Naka nga yendo ? | Comment s’est passée ta journée ? | How was your day ? | ¿Cómo fue tu día? | Com h’anat el dia ? |
44 | Barki démb diaronne na sa keur | Avant-hier j’étais passé chez toi | the day before yesterday I went to your house | Antes de ayer fuí a tu casa | Vaig anar a casa seva el dia abans d’ahir |
45 | Dama nieuwone indil leu sa khaliss | J’étais venu t’apporter ton argent | I came to bring you your money | Vine a traerte tú dinero | Vaig venir a donar-te diners |
46 | Dama nékone daara dja | J’étais à l’école | I was at school | Estaba en la escuela | Jo estava a l’escola |
47 | Damay saakou xam-xam | Je suis à la quête de connaissance | I am on a quest for knowledge | Estoy en búsqueda de conocimiento | Estic a la recerca del coneixement |
48 | Nianal ma ! | Prie pour moi ! | Pray for me ! | ¡Reza por mi! | Pregueu per mi! |
49 | Témérri Diouni | Cent milles | One hundred thousand | Cien mil | Cent mil |
50 | Damala beug | Je t’aime | I love you | Te amo | T’estimi |
51 | Dama gueuméntou | J’ai sommeil | I feel sleepy | Tengo mucho sueño | Estic cansat |
52 | Dama beug nelaw | Je veux dormir | I want to sleep | Quiero dormir | Vull anar-me’n al llit |